Afrika a a a Afrika mon Afrique
Sama gent gi maa ngi naan Yalla wonma
ko bala may nibbi barsaq
Ma ne bes du nakk ci bes yi Afrika
don benn reew
D'ici ou d'ailleurs nous somm'
des enfants d'Afrique
Mem' si le ciel tombait luttons pour la paix
Kon jammu Afrika moom lay naan
Mane jammu Afrika mooy sunu natange
Afrika a a a Afrika a a
Afrika a a a Afrika mon Afrique
Yow mi nekka bittim reew man
mi Lo maa ngi lay naan
Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun
ta mel bul fatte Afrika
Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur
Mem' si le ciel pleurait luttons pour nos freres
Kon jammu Afrika moom lay naan
Mane jammu Afrika mooy sunu natange
Afrika a a a Afrika a a
Afrika a a a Afrika mon Afrique
Onon bibbe Afrika ngimode,
ngimode liggo-den leydi men
Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi
Yoo Alla addu jam to Ruanda
Yoo Alla addu jam to Burundi
Yoo Alla addu jam to Casamans